19 Yaayu Yeesu ak rakki Yeesu yi ñëw ngir gis Yeesu,
waaye mënuñu woon jot ci moom ndax mbooloo mi.
20 Ñu ne ko:
«Sa yaay ak say rakk nu ngi ci biti,
bëgg la gis.
21 Waaye Yeesu tontu leen ne:
«Sama yaay ak samay rakk,
mooy ñiy déglu kàddu Yàlla gi te di ko jëfe.